
Conférences

Droits et obligations de la vie conjugale
Àq ak wartéef yi aju ci néegu sëy Thème : Droits et obligations de la vie conjugale par Serigne Ahmad SAMB Subject : Rights and obligations of married life by Serigne Ahmad SAMB

Cheikh Ahmadou Bamba et son mode de vie
الْوَفَا صُبَ فُكِّيلُ فَنْبِ أَكْ جَتَّ كِيْ وَخْتَانْ مُويْ(شَرِجْ مُصْطَفَي إبْنُ شَرِجْ مَحْمُودًا جُبِ بَكِّ)لِمُيْ وَخْتَانِ (مِلُكَانِ شَرِجْبِ أَكْ دُنْدِينَمْ) Alwafa suba fukkeelu fan bi ak ñatt kiy waxtan moy (Serigne Moustapha Mbacké Mahmoudan Diobe)limoy waxtaane moy (melokaani Sëriñ bi ak doundiinam)

Le système foncier Sénégalais: la nécessité d'une réforme sérieuse et urgente
الْوَفَا صُبَ بِسُبْ فُكِّيلْبِ أَكْ جَارْ كِيْ وَخْتَانْ مُوىْ(دكتور أَحَمدُ مَخْتَارْ صِلَّه) لِمُيْ وَخْتَانِ(بِرُمْ سُوفْ جِسِنِكَالْ أَكْ لِمُ لاَجْ جِأَكْ جُبَنْتِ) Alwafa suba fukkeelu fan bi ak ñaar kiy waxtan moy (Docteur Ahmadou Makhtar Sylla)limoy waxtaane moy (mbirum souf ci Senegal ak limu laaj ci ak jubbanti)

Défis actuels et perspectives d'avenir de la ville sainte de Touba
Tuubaa: yi koy dekk ak fi nu koy séentu elleg. Thème : Défis actuels et perspectives d'avenir de la ville sainte de Touba par Serigne Cheikh Fatma MBACKÉ. Subject : Current and future-looking challenges of the holy city of Touba by Serigne Cheikh Fatma MBACKÉ.

Les principes fondateurs du prêt en islam
Attey leb ak leblé aki teiguinam Thème : Les principes fondateurs du prêt en islam par Serigne Abdou Khadre BOUSSO. Subject : the founding principles of lending in Islam by Serigne Abdou Khadre BOUSSO

Les effets de l'environnement sur la vie de l'homme
10 Ramadan 1446H : Jeexiti kéew (environnement) mu baax ci dundug nit ki Thème : Les effets de l'environnement sur la vie de l'homme par Serigne Cheikh MBACKÉ NIANE. Subject : The effects of the environment on human life by Serigne Cheikh MBACKÉ NIANE.

La nécessité de la probité dans la vie du musulman: L'exemple de Cheikh Ahmadou Bamba
لْوَفَا صُبَ بِسُبْ فُكِيلْبِ أَكْ بِنَّ كِيْ وَخْتَانْ مُويْ(شَرِجْ مُصْطَفَي بَكَّ )لِمُيْ وَخْتَانِ(أَمْسُلُكْ دِوَتَدِكُ لِبَّ لُلَنْتَ أَكْ نِجُكُ مَنَ جَنْكِ جِشَرِجْبِ) Alwafa suba bisub fukkeel bi ak benn kiy waxtan moy (Serigne Moustapha Mbacké) limoy waxtaane moy (am solok di wattandiku lepp lu lënt ak niñuko mana jànge ci Sëriñ bi)

Que faut il entendre par l'honorabilité et la sacralité de la ville sainte de Touba ?
09 Ramadan 1446H : Wormay Tuubaa: déggin wi ak jēfiin wi. Thème : Que faut il entendre par l'honorabilité et la sacralité de la ville sainte de Touba ? par Serigne Sam BOUSSO Abdourahmane. Subject : What is meant by the honorability and sacredness of the holy city of Touba? by Serigne Sam BOUSSO Abdourahmane.

La medecine par les plantes
الْوَفَا صُبَ بٍسُبْ فُكِيلْيبِ كِيْ وَخْتَانْ مُويْ(بروفسور أَحْمَدُ صَمْبَ)لِمُيْ وَخْتَانِ (فَجُ أَكْ سَكَنْجَخْ) Alwafa suba bisub fukkeel bi kiy waxtan moy (Professeur Ahmadou Samb)limoy waxtaane moy (faju ak sa ganthiax)

Fatwa série de questions - réponses
08 Ramadan 1446H : Tontu ay laaj ci diiné - Fatwa Thème: Serie de Questions - Réponses par Serigne Cheikhouna MBACKÉ Abdoul Wadoud Subject : Series of Questions and Answers by Serigne Cheikhouna MBACKÉ Abdoul Wadoud

Prevention des maladies oculaires les plus courantes
الْوَفَا صُبَ بِسُبْ جُرُومْجِينْتِيلْبِ كِيْ وَخْتَانْ مُويْ(دُكْتُورْ مبَجِكْ كُمْ)لِمُيْ وَخْتَانِ (نَكَ لِسْدِ دِفْ بَمُجُّ جِخِيتِ تَوَتْ يِأَجُ جِبَتْ) Alwafa suba juroom ñeenteelu bisbi kiy waxtan moy (Docteur Mbagnick Ngom)limoy waxtaane moy (naka lees di def ba muthiou ci xeeti tawat yi aju ci bët)

Les compagnons du Prophète Mouhamed ( paix et salut sur lui ) sont nos pères spirituels dans l'islam
07 Ramadan 1446H :Sahaaba yi ñooy sunuy Baay ci Diine Thème : Les compagnons du Prophète Mouhamed ( paix et salut sur lui ) sont nos pères spirituels dans l'islam par Serigne Abo MBACKÉ Bassirou Mor. Subject : The companions of the Prophet Muhammad (peace and blessings be upon him) are our spiritual fathers in Islam by Serigne Abo MBACKÉ Bassirou Mor.