
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2023
26 épisode

La crise mondiale et la nécessité d'établir un nouvel ordre mondial : Le rôle de l'islam
الموضوع: الأزمة العالميّة وضرورة وضع نظامٍ عالميٍّ جديد:البديل الإسلامي Serigne Ismaahiila Diop (Dakar Thème (La crise mondiale et la nécessité d'établir un nouvel ordre mondial : Le rôle de l'islam*

La fraternité musulmane
شَرِجْ الْحَاجِ فَضْلُ امْبَاكِي عَبْدُالرَّحْمَانْ (دَارُالْمَنَّانْ طُوبَي) الموضوع: إنّماالمومنون إخوةٌ