
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2022
29 épisode

L'approche du soufisme dans les enseignements
Jour 02 : Laan moy deeg degg tassawuf kem niko SERIGNE BI janglei Thème : L'approche du soufisme dans les enseignements de CHEIKH AHMADOU BAMBA par SERIGNE AFFÉ NIANG

La legislation islamique par rapport à l'accusation d'adultère
No description available


La liberté dans l'islam entre prérogatives et limites
No description available

L'amour du prophète MOUHAMED (PSL) et ses manifestations
No description available

Comment se manifeste la corruption dans la communauté ?
No description available