
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2020
29 épisode

Les conditions et les recommandations du bien et d'interdiction du mal
Saarte ak Jumtukay yiy diiglé lou bakh ak tééréé lou boone Thème : Les conditions et les recommandations du bien et d'interdiction du mal par SERIGNE SOULEYMANE BADIANE

La zakat : sens religieux et impact social.
Ndiiariniou aassaka ak ay djéxitaam Thème : La Zakat : sens religieux et impact social par SERIGNE MOUNTAKHA DIATTARA

Les voies et bienfais du Zikr
Ngeuneel ak teiguini toud Yalla Thème : Les voies et bienfaits du ZIKR

Règles et bienséance de la Zakat al Fit et de la prière des deux 'eid
No description available