
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2021
28 épisode

La lecture du Saint Coran et ses Modalités selon MASSALIKOUL DJINANE
Téere « Masaalikul Jinaan » : buntu'b « Jang al-xuraan ak li ci aj'u »

L'importance du savoir dans la vie de CHEIKH AHMADOU BAMBA
Serin bi ak nimu foonke won xam-xam

L'abattage Halal selon la pratique islamique
Atte y réendi ak i teggin'am ei lislaam

La diversité des jeux de carte et leurs inconvénients
« carte » mooy lan ak léen ci y xéet'am ci jamono jii

Les implications de l'ignorance des actes obligatoires dans la pratique religieuse
Nakk a xam say farata aki li ci man a judde

Une démarche paisible, fondement de la quiétude
Ak maandu mooy teye ak dal

La preservation de l'héritage de nos Saints Hommes pour l'unité de la communauté
Waru gar wi ñéppu am ci sammu béennok xéet wi ak'uk dalam

Des politesses légales tirées des enseignements de CHEIKH AHMADOU BAMBA
Léen ci ay teggin yu Serin bi denkaane