
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2021
28 épisode

Comment efficacement mettre en œuvre les projets pour l'Islam
Naka lañu war'a sottale naal yi jem ci lislaam

La conception islamique de la dépense quotidienne
Diokhé dépense kem niko lislam teureulé

La société ou l'entreprise dans le but de faire du profit selon la loi islamique
And bok liguey niko lislam diangualé

Les règles de l'islam par rapport à une personne portée disparue
No description available

Interprétation des règles de la charia en terme de priorité des actes obligatoires
Maanaa ak war'uk xam-xam bi y jangale jef yi ñu war' a jiitel

Des erreurs récurrentes commises dans l'union sacrée du mariage
Ay njuumte yu jem ci sey te am nu koy def

La presse idéale à travers l'information selon la considération de l'Islam
No description available