
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2023
29 épisode

Les intentions et principes fondateurs du jeûne
Jour 01 : Atte ak i mbóot yu aju ci koor Thème : Les intentions et principes fondateurs du jeûn par SERIGNE MAME MOR MBACKÉ XAM SA DIINE

Le citoyen: droit et devoir
Jour 02 : Aq ak wartéefi Ma Réew ( Citoyen ) Thème : Le citoyen par SERIGNE FALLOU BOUSSO ASSANE

L'exemple du mouride parfait dans la foi et le comportement
No description available

Le mal causé à autrui : Manifestations et Conséquences
Jour 04 : Togn : Ay xeetam ak i looranguem ci niit ki ak ci askanwi Thème : Le mal causé à autrui : Manifestations et Conséquences

Les lois islamiques sur la location
Jour 05 ( 27 Mars 2023 ) : Attey Lislaam yi ajuu ci location Thème : Les lois islamiques sur la location par SERIGNE SOULEYMANE BADIANE

L'intelligence stratégique de CHEIKH AHMADOU BAMBA
Jour 06 ( 28 Mars 2023 ) : Niité ak Xellug SERIGNE TOUBA ak nimu feegnee ci ak dundaam Thème : L'intelligence stratégique de CHEIKH AHMADOU BAMBA par SERIGNE MAMOUNE MBACKÉ FADILOU

L'essence et l'importance de la paix dans la vie de socièté
Jour 07 ( 29 Mars 2023 ) c: Solo ak nattuwaay jaam akug dal ci askan wi Thème : L'essence et l'importance de la paix dans la vie de socièté par SERIGNE MOUSTAPHA DIOP NDAR

Fatwa: série de questions réponses Jour 8-2023
Jour 08 ( 30 Mars 2023 ) : Fatwa Serie de Questions Réponses par SERIGNE MBACKÉ ABDOU RAHMANE

Le crédit bancaire selon l'islam
Jour 09 ( 31 Mars 2023 ) : Ni Lislam ak atté leeb ak jeeflanté ak bank Thème : Le crédit bancaire selon l'islam par SERIGNE SONHIBOU DIOP

Les conséquences de la popularité de la perte des valeurs dans la socièté
Jour 10 ( 01 Avril 2023 ) : Siiwal ag ñawtéef aki loram ci nit ki ak ci askan wi Thème : Les conséquences de la popularité de la perte des valeurs dans la socièté par SERIGNE MOUNTAKHA DIATTARA

Analyse de l'expression « Bum laal suuf» de Serigne Mountakha
Jour 11 ( 02 Avril 2023 ) : Jangaat ak Taxaaw setlou cii kaddug Serigne Mountakha " " buum laal suff " Par DOCTEUR KHADIM SYLLA

Le testament en islam
Jour 12 ( 03 Avril 2023 ) : Ndenkaané ak ay ateem ci lislam Thème : Le testament en islam par SERIGNE MBACKÉ ABDOU RAHMANE