Grande Mosquée de Touba 2023

Ramadan

Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!

Début de la série: 1 mars 2023

17 épisode

24
Spirituality
L'avenir de la ville sainte de Touba à travers le Complexe CHEIKH AHMADAL XAADIM
56m 50s

L'avenir de la ville sainte de Touba à travers le Complexe CHEIKH AHMADAL XAADIM

Jour 24 : ( 15 Avril 2023 ) : Jàngat ëllagu Tuubaa sukkandikoo ko ci Ubbiteg jàngukaayub Tuubaa bi (CCAK) Thème : L'avenir de la ville sainte de Touba à travers le Complexe CHEIKH AHMADAL XAADIM par Docteur SERIGNE SAM BOUSSO ABDOU RAHMANE

26
Spirituality
Règles de base de la zakat, de l'aumone du jeûn et de la prière de l'Aid el Fitr
1h 44m 33s

Règles de base de la zakat, de l'aumone du jeûn et de la prière de l'Aid el Fitr

Jour 26 ( 17 Avril 2023 ) : Àtte ak teggiini Asakay muurum koor ak julliy hiid. Thème : Règles de base de la zakat, de l'aumone du jeûn et de la prière de l'Aid el Fitr ( Korité ) par SERIGNE IBRAHIMA KÉBÉ

27
Spirituality
Fatwa: série de questions réponses
1h 9m 57s
29
Spirituality
Quelques enseignements tirés de la deuxième partie de "Al Jawharun nafiis"
1h 37m 11s

Quelques enseignements tirés de la deuxième partie de "Al Jawharun nafiis"

𝚃𝚘𝚖𝚋 𝚋𝚒 𝚗̃𝚞𝚢 𝚠𝚊𝚡𝚝𝚊𝚊𝚗𝚎: Ay masala yees jukkee ci buntu ñaareelu téereb « Al Jawharun nafiis » ▫️𝙺𝚒 𝚔𝚘𝚢 𝚍𝚎𝚏: Imaam Sëriñ Asan JUUF

Select a podcast to play

Podcast artwork

Select a podcast to play

ToubasTalks

0:00
0:00