
Ramadan
Programme Waxtaani Koor yi Daa'ira Muxaddamatul Xidma di taxawu ci biir Jumaay Tuubaa ju mag ji. Waxtaan yi dina am bis bu nekk ci Koor gi ginnaaw jullig Tàkkusaan. Dingeen ko mën a topp jaare ko ci Chaîne Jumaay Tuubaa MK-Tv: https://youtube.com/@MK-TV360 Wala GMT-Tv: https://youtube.com/@GMTTv Wala ci xëtuw Féesbug bi: Grande Mosquée de Touba Koorug jàmm!
Début de la série: 1 mars 2023
29 épisode

Nos devoirs envers l'héritage de SERIGNE TOUBA
Jour 25 ( 16 Avril 2023 ) : Sunu wartéef ci ndonol Sëriñ bi. Thème : Nos devoirs envers l'héritage de SERIGNE TOUBA par SERIGNE CHERIF MBACKÉ FADILOU

Règles de base de la zakat, de l'aumone du jeûn et de la prière de l'Aid el Fitr
Jour 26 ( 17 Avril 2023 ) : Àtte ak teggiini Asakay muurum koor ak julliy hiid. Thème : Règles de base de la zakat, de l'aumone du jeûn et de la prière de l'Aid el Fitr ( Korité ) par SERIGNE IBRAHIMA KÉBÉ

La responsabilité du musulman dans le choix d'un bon dirigeant
No description available

Quelques enseignements tirés de la deuxième partie de "Al Jawharun nafiis"
𝚃𝚘𝚖𝚋 𝚋𝚒 𝚗̃𝚞𝚢 𝚠𝚊𝚡𝚝𝚊𝚊𝚗𝚎: Ay masala yees jukkee ci buntu ñaareelu téereb « Al Jawharun nafiis » ▫️𝙺𝚒 𝚔𝚘𝚢 𝚍𝚎𝚏: Imaam Sëriñ Asan JUUF